| question | réponse | |||
|---|---|---|---|---|
|
Jox ma deux cents cinquante
|
||||
|
Dem Maangi dem St. Louis
|
||||
|
ñow ñow-al; ñow na
|
||||
|
duga Duga na oto
|
||||
|
one word
|
Jeksil
|
|||
|
kai
|
||||
|
Laggàlam Wolof
|
||||
|
Wolof rekk
|
||||
|
amuma Amuma xalis
|
||||
|
am Amma, am nga
|
||||
|
to confirm it is water you want
|
Bugana Bugana ndox bu sera
|
|||
|
Ñaata la? Cahier bi ñaata la?
|
||||
|
Am nga ...? Am nga jabar?
|
||||
|
Often used to make polite requests
|
amulo Amulo seedo?
|
|||
|
Bëgguma Bëgguma ndoq
|
||||
|
Bëggaguma Bëggaguma xale
|
||||
|
e.g. restaurant
|
Lu am foofu?
|
|||
|
Against the begging children
|
Mono ma laa dimbale
|
|||
|
xam Xam na ko / xam nanu ko
|
||||
|
xam nga ko?
|
||||
|
neex Dakar neex, mango neex
|
||||
|
Neexul ma
|
||||
|
Jàng Wolof laay jàng
|
||||
|
jàngale Anglais ngay jàngale
|
||||
|
jàngal Thomas lay jàngal
|
||||
|
Jënd ndoq lanuy jënd
|
||||
|
jaay Oto ngeendi jaay
|
||||
|
faj
|
||||
|
noppalu
|
||||
|
ñibbi lañuy ñibbi
|
||||
|
seeti
|
||||
|
yònnée
|
||||
|
topatoo
|
||||
|
woo
|
||||
|
cosaano
|
||||
|
maangi ci kawam
|
||||
|
jaay ma seedo
|
||||
|
ndax yassam poulet am na?
|
||||
|
ndax bëggu nga tsjeboudien?
|
||||
|
ndax am nga Gazelle?
|
||||
|
ndax bëgg nga dem la plage
|
||||
|
ndax Wolof nga?
|
||||
|
Ban lakk nga?
|
||||
|
wolof la
|
||||
|
Am nga/ne café?
|
||||
|
Am nga/ne ñaari Gazelle?
|
||||
|
Plateau lay djöm laay is place marker
|
||||
|
rus
|
||||
|
Am jot
|
||||
|
Ragal
|
||||
|
Sëy
|
||||
|
Takk jabar
|
||||
|
Gaañu / faatu
|
||||
|
Tas
|
||||
|
Fase
|
||||
|
Dund Dunduwul
|
||||
|
an ngil ma ndox
|
||||
|
ñaata wër ngaay am Dakar? wër
|
||||
|
Ñeenti wër ci kanam
|
||||
|
Kañ ngaay delusi Dakar?
|
||||
|
Na seet
|
||||
|
Mba büggunga Dakar
|
||||
|
neex na
|
||||
|
Feetja bi neex na
|
||||
|
ndeo / ndekk
|
||||
|
Añ bi neex na añ bi
|
||||
|
réer
|
||||
|
safsaf
|
||||
|
kani
|
||||
|
poobar
|
||||
|
harom
|
||||
|
sukur
|
||||
|
am nga wérgu yaram?
|
||||
|
togg looy togg
|
||||
|
looy def
|
||||
|
njiit
|
||||
|
Tëgg
|
||||
|
bakhul ci mane
|
||||
|
doe (dou) fofu
|
||||
|
fi laa
|
||||
|
li
|
||||
|
lolu
|
||||
|
wax looy wax? luy nga wax?
|
||||
|
doxantou Maangi bügg doxantou
|
||||
|
doxan
|
||||
|
dama bügg dëm Gambia dama: personal future pronoun
|
||||
|
grammar difference
|
Damai tëdd damai <-> dama dama bügg tëdd
|
|||
|
more serious with 'want'
|
waxtan Dama (bügg) ñu waxtan
|
|||
|
listen to me, he/she
|
degglu degglul ma / ko degglul
|
|||
|
seet Dama bügg seet Ibrahim
|
||||
|
ci walum Maangi jangalekat ci walum Ashinaga
|
||||
|
he's active in politics
|
jengu jengujengu ci walum politique jengujengu
|
|||
|
my village
|
dëka bi suma dëka
|
|||
|
change of topic
|
ganaw lolu
|
|||
|
balla nga ñew
|
||||
|
ci boor bi
|
||||
|
garab bi suufi / run garab bi
|
||||
|
seeri
|
||||
|
jëram tangal jëram
|
||||
|
jeewu jeewul
|
||||
|
jogg bul jogg
|
||||
|
selmu damai selmu
|
||||
|
sangu dama bügg sangu
|
||||
|
pare nga parewul maa
|
||||
|
solu solu bi refer na
|
||||
|
nuyu naa la nuyu naa len
|
||||
|
maangi delou liggéey
|
||||
|
dadjë Dama bügg ñu dadjë
|
||||
|
brada
|
||||
|
kars
|
||||
|
ataya
|
||||
|
naan dama bügg naan (bière)
|
||||
|
ak benneen / jox ma benneen
|
||||
|
mungi mokk mokk
|
||||